Tajabone
Tadieu bone
Ta Tadieu bone da gnuy tadieu bone
Ta Tadieu bone da gnuy tadieu bone
Abdou ou djambar niari malaika la
Khawe e tchikow danou tchi sa rou
Momou mou ni la dangam djuli nga
Momou mou ni la dangam woor nga
Khawe e tchikow danou tchi sa rou
Momou mou ni la dangam djuli nga
Momou mou ni la dangam woor nga
Ta Tadieu bone da gnuy tadieu bone
Ta Tadieu bone da gnuy tadieu bone
(Wolei, Wolei, Wolei, Wolei)
Abdou Djambar (wolei)
Niari malaika la (wolei)
Tchi kow lay djogue (wolei)
Danou tchi sa rou (wolei)
Mouni la (wolei)
Dangam djouli nga (wolei)
Mouni la (wolei)
Dangam woor nga (wolei)
(Aaah !!!!!!)
Jammu Africa 专辑歌曲
歌曲 | 歌手 | 专辑 |
---|---|---|
Tajabone | Ismaël Lô | Jammu Africa |
Dibi Dibi Rek | Ismaël Lô | Jammu Africa |
Jammu Africa (Version Album) | Ismaël Lô | Jammu Africa |